Accueil Buzz NitDof: « Serigne ci bouniou bayi khel opposition bi mais peuple bi...

NitDof: « Serigne ci bouniou bayi khel opposition bi mais peuple bi laniou wareu bayi khel »

249
0
PARTAGER

Serigne ci bouniou bayi khel opposition bi mais peuple bi laniou wareu bayi khel
Séni talibé nioy deh si dialyse bi séni talibé nioy deh ndakh diabète bi ak cancert bi
Séni talibé laniouy fitnal si université yi
Séni talibé nioy dound ay werr sans ndokh
Ak di nane de l’eau non potable
Séni talibé laniou sathie sén kom kom diko passar passaré si parti politique yi ak concert yi ak lamb dji

Comme je le disais chers frères et sœurs vous êtes livrés à vous même
Plus personne ne vous défend plus personne ne s’inquiète pour vous
Soit vous vous prenez en main soit vous allez restez des pions qu’on utilise à chaque occasion
Wa salam

LAISSER UN COMMENTAIRE

Please enter your comment!